cig jonjoo

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

  • cig jonjoo mooy safaanub cig jonjoodi, mooy li dara doxul sa diggante ak moom, joŋante baa ngi am cig jonjoo mooy ci jamono jii lay ame, sabab su jonjoo ak su jonjoodi, mooy sabab si tax nga xam ne dara jaaraatu fi, sabab su jonjoodi nag mooy si nga xam ne am na leneen lu jaar ci diggam ak li mu sabab

français[Soppi]

  • direct ou en direct