cax
Apparence
wolof
[Soppi]cax:
- aw cax wax jees war a tekki.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diw... cax na fi cax wu naqaree tékki.
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: énigme
- wu-angalteer: riddle
Déglu baatu cax ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-cax.ogg