caat
Apparence
wolof
[Soppi]caat:
- am caat doom ju mujj.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diw mooy sama caatu baay
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: cadet
- wu-angalteer: youngest child
Déglu baatu caat ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-caat.ogg