cëslaay (lenn)

Jóge Wiktionary.

wolof[Soppi]

  • dàtt
  • day firi it ay yoon aki tabax yi manul a ñàkk cim réew ngir mu tabaxu, doon lu taaxe te xaye:

Mbooloom liggéey yi taxawal ab sosuwaay (ab dàtt,ab pëjj), ak taxawal ci suuf si ab tabax walla mbooloom ay mbir, (ci misaal ay yoon, yooni weñ (rail), naawuwaay (aéroports).

Mbooloom ay taxawal, aki jumtukaay walla bagaas yu manul a ñàkk cig bar:Cëslaayu yaxantu lu ab dëkk bu yees.

Wàll gu làqu, gi bóof ci ron gi ci lenn cëslaay (gu xel mbaa daju).

Mbooleem wàll yi féete suuf cib tabax, ñaare yi suulu (ron-suuf péex gi(vide sanitaire), walla sosuwaay bi(fondation),añs.

français[Soppi]

  • infrastructure:

Ensemble des ouvrages constituant la fondation et l'implantation sur le sol d'une construction ou d'un ensemble d'installations (par exemple routes, voies ferrées, aéroports). Ensemble d'installations, d'équipements nécessaires à une collectivité : L'infrastructure commerciale d'une ville nouvelle. Partie interne, sous-jacente à une structure (mentale ou matérielle). Ensemble des parties inférieures d'un bâtiment, généralement enterrées (sous-sol ou vide sanitaire, fondations, etc.). Domaine profond d'un orogène, caractérisé par des structures du niveau inférieur où règnent des conditions de pression et température propres à permettre des déformations plastiques, des structures d'écoulement, des phénomènes de fusion. Pour les marxistes, structure économique de la société, base concrète sur laquelle s'élève une superstructure juridique et politique.