càmmoñ
Apparence
wolof
[Soppi]càmmoñ:
- càmmoñ loxo bees dul jëfandikoo ngir lekk, xanaa ci ak loro.
- boo taxawee jublu pénku sa wetuk càmmoñ mooy feete bëñ-saalum
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- gone gu am yar du lékkee càmmoñ
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu càmmoñ ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-càmmoñ.ogg