buy
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
buy: am na ñaari maanaa
- ab buy doom biy ne ci wuy di weex ñaare, wuy di doomi guy,
- buy dees jamonoolee ay wax, niki buy def nàngam,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- Tojal wuy wi nu lékk ci buy bi,
- gone gu yaru buy lékk du wax ci lu dul ndigël.
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
Waxiin
Déglu baatu buy ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-buy.ogg