buntu

Jóge Wiktionary.

wolof[Soppi]

Gongikubaat[Soppi]

buntu:

  1. ab buntu dunguwaay walla jaaruwaay

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]

  1. Yàlla neena kuy dung ci neek na jaar ca buntu ba.

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu buntu ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-buntu.ogg