boyal
Apparence
wolof
[Soppi]boyal: amna ñaari maana
- boyal lees bàyyi mu dem ak sagoom
- boyal/boyol lees di def ngir am ay xal mbaa safara ...
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diw.. dey daa boyal doomam ji, ba lu ko neex def.
- demal boyyal/boyol nu attaaya,
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: liberté total,
- wu-angalteer: freedom,
Déglu baatu boyal ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-boyal.ogg