boor
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
boor:
- boor yamukaayi mbir, maanaa ay wet
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- booru xët wii am na ag njàppun ngir wacc ci suufu xët wi,
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: bord
- wu-angalteer: edge
Waxiin
Déglu baatu boor ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-boor.ogg