bis-bu-ne
Apparence
wolof
[Soppi]bis-bu-ne:
- bis-bu-ne mooy bépp bis teew ci àdduna,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- bis bu set Yàlla di gën a wone boppam te nit ñi xamu ñu ko!
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu bis-bu-ne ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bis-bu-ne.ogg