biochimie

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

yaakar naa ne Bio am jàxas bu de lu jam ci ndox ñin koy wax ( ¿ Tutërr `nétër, boo bolee soow ak cefna manaam xobi daqar yuñu nokkas xocc ko mba nga tangal dox sotti ca boo yakkam te bamu saf nga seeg ko jáxase kook soow , bu dee doomu daqàrbi boo ko xolle ba mu seet nga jéll meew sooti ci daqàr ji jambu ko ba mu farr niipu loolu mooy Turër bude soow mu waay ak cafna wala bisaap ak wayàl ,yooyu yéep nétër lii dal mooy sama ci Biochimie