Aller au contenu

bidda

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

ci araab la joge bidda:

  1. bidda ci diine lees sos di ko jëfe te amul delluwaay ci sunna wala al-xuraan.
  • bu dee tekkik baat bi dong nak moodi «sos»

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. diw dey ak a fonk bidda,

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

[Soppi]

Déglu baatu bidda ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bidda.ogg