ber
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
ber: am na ñaari maanaa
- ber lees xéjji ci'y moroomam,
- ber suuf su nooy la tey xonq,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- seetal ben bu baax nga ber ko,
- gasal foofu am na suufus ber
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Waxiin
Déglu baatu ber ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-ber.ogg