beñuwaar
Apparence
wolof
[Soppi]béñuwaar/beñwaar:
- beñuwaar paan gu mat sëkk,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- joxal sa yaay beñuwaari mu rooti
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: - baignoire
- wu-angalteer: - bathtub
Déglu baatu beñuwaar ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-beñuwaar.ogg