baar
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
baar : amna ñaari maanaa yu man a doon benn
- baar donga-y daara yi dinañ ko jëfandikoo ngir ñeenti laaye yune muy joroomeel ba,
- baar ci xamxamu xayma moodi tómp sii ,
Xool it[Soppi]
ci yeneeni làkk[Soppi]
- wu-faraas: virgule
- wu-angalteer: comma
Waxiin
Déglu baatu baar ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-baar.ogg