bëy
Apparence
wolof
[Soppi]bëy:
- bëy mala la ci mala yi dëkk ak nit ñi,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- geenu bëy sànguli taat!
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: chévre
- wu-angalteer: goat
Déglu baatu bëy ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bëy.ogg