bët
wolof
[Soppi]- ab céru gis la buy nekk ci xar-kanamu nit tey ànd ak moroomam: mbooloo mi di gët
- yëddukat
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- -
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: l'œil, espion
- wu-angalteer: eye, spy
Déglu baatu - ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo- .ogg