Aller au contenu

békkoor

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

békoor:

  1. békoor jamono ju naqari, maanaam ñàkk gu tar

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. 2002 atum békkoor la woon mu métti ci jur gi

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu békoor ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-békoor.ogg