Aller au contenu

béer

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

béer g

  1. garab giy jur béer.

béer b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug béer.

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Sclerocarya birrea
farañse: marula
angale: marula
itaaliyee: marula