ag lëngoo
Apparence
Misaal: gouvernement fédéral : "góornamaa walla nguur gu ag lëngoo" . Des gouvernements de collectivités ou d'Etats fédérés: "góornamaa yu mbooloo yi walla nguur yu ñu lëng yi" . Misaal : Diiwaan yu bennoo yu Amerig yi, péncum lëngoo mu Almaañ mi(République Fédérale d'Allemagne), lëngoo gu Riisi(Fédération de Russie), gu Beljig, gu End...