Aller au contenu

ag cang

Jóge Wiktionary.

ag cang bu ñu ko waxee ci politig ak lu aju melosuuf, mooy lu mel ne ag tembte, ak moom-sa-bopp: Senegaal de réew mu temb la, mu am ag cangam ci mbooleem ay suufam, :maanaam Senegaal mooy sang bi ci suufam: il a sa souveraineté sur son étendu du territoire