ab ak bi

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

bi ak ab[Soppi]

  • baati doxondeem yépp ab lañuy tudd budee aw tur, Misaal: ab rajo, ab tele, ab alaaji, ab tariixa,
  • baati doxondeem yépp bi lañuy sant bu dee aw sant, Misaal: web bi, net bi, widewoo bi, misig bi,
  • baati doxondeem yi bu dee jëf ag lañuy faral di tudd, Misaal:ag demokaraasi, ag politig,

ab ak bi ci baati wolof