Aller au contenu

aaye

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

aaye

  1. lu kenn waru koo def.

aaye b

  1. li ñu nee la bul ko def mbaa bul ko wax.

Bokktekki

[Soppi]

tere

Waxiin

Déglu baatu aaye ci wolofi Senegaal