Wiktionary:baati sinemaa
Apparence
ci wii xëtu sémb baat yi ñeel sinemaa lañu fiy waxtaane:
- cinema :Sinemaa
- angle (de prise de vue) = Ponk, koñ, ruq, aw gisiin
- plongée /plongée contre = nuur/nuur safaan (nuur jëm ci)
- bande sonore = dog wuy coow, bànd bu xumb, bànd buy kàddu, dog wuy kàddu(walla lëmës mbaa taxañ (bande) buy sab)
- bruitage = coowal, xumbal
- champ / contrechamp = tool/safaan-tool
- décor = rafetal, taaral, (ci tiyaatar = misaal: (ab séenu bu misaal, )
- découpage = dog,dogiin,daggate, daggatiin (walla rafetal ci kayit)
- effets spéciaux = jeexiit yees jagleele, jeexiit yu am ay jagle,yu di woroomi jagle, ay naxe, ay way jortuloo
- figurant = aji feeñ,
- générique = dog wu njëkk, way def yi
- générique de fin = dog wu mujj
- metteur en scène, réalisateur = aji def ji, aji amal ji
- métrage (court/long) = yàggaay(gu gàtt/gu gudd)
- pellicule = guuxaan
- plan, scène, séquence = naal sémb(palaŋ), scène = ab séenu, ab xewuwaay. séquence = ag callala, ag toftaloo aw dog
- ralenti = yeexal,
- scénario = yaxub film (senaariyóo)
- synopsis = ab tënk, ab gàttal,
- fILM = film, guuxaan