Waxtaan:dayoo
dayo: fi am mbir yam, dayob xam-xam ; fi xam-xam yam, ñaaw dayob ñaaw,: àgg fa ab ñaawaay yam. waaye tam di na tekki ni tollees: yaw xamoo sama dayo moo tax nga yab ma: xamoo ni ma tollu moo tax nga yab ma. Waaye daytal sañoo ko cee wax,
- du man maa ko sos sax daa am ku ma gis mu tekke ko format moo tax ma jëfandikoo ko --Ibou 9 Ndeyi-koor 2008 à 18:49 (UTC)