Aller au contenu

Waxi Kocc Barma

Jóge Wiktionary.
 • Ben loho dou tatiou
 • Déggal ndigal i ñett, bàyyil ndigal i ñett.
 • Garab gu dul meññ du am yoon. Alternativley:
  • Garab gu dul tàbbal ay doom doo am aw yoon

Relating to the story of the four pigtails[Soppi]

 • Buur du mbokk. Alternatively:
  • Buur du mbokk, du jeneen.
 • Doomu-jittle du doom. Alternatively:
  • Doom jiitle du doom, xaré bu wafe-lë.
  • Doom jiitle du doom, ay la.
 • Jigéen, soppal te bul wóolu. Alternatively:
  • Jigéen ju ndaw, soppal te bul wóolu.
  • Soppal sa jabar, te bu ko wóolu.
 • Mag mat naa bàyyi cim réew.