Aller au contenu

Saytubiddiw

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

mi ngi jóge ci baati saytu ak bu biddiw

saytubiddiw

  1. mooy xam-xam biy saytu yarami asamaan yi

Xool it

[Soppi]

Gëstubiddiw

Tekki

[Soppi]
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons