NJ.Ñ.B

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

njuddéef mu ñumm mu biirum réew (NJ.Ñ.B): maanaam li am réew juddal, liggéey ko ciy njuddéef (produits), ba noppi muy lu ñumm, maanaam yokkeesu ci wàññeesu ci.