Aller au contenu

Jokkalekaay

Jóge Wiktionary.

Wu-fraas[Soppi]

Gongikubaat[Soppi]

moo ngi jóge ci jokkoo

Tur[Soppi]

Jokkalekaay:

  1. ci xibaarfeppal, mooy liy tax jokkoo man a am ci diggante ñaari jumtukaay, walla tëriin, ci anam gu ñu deggoo, muy lu gisu walla xellu

Tekki[Soppi]

wu-fraas: interface