Doolerandu

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

Wolof[Soppi]

Gongikubaat[Soppi]

xoolal doole ak randu

Tur[Soppi]

Doolerandu:

  1. xam-xam biy gëstu lépp luy yëngu, mooy jàng yëngiinu mbir yi ak itam seenug tekkaaral.
Wikipedia am na jukki bu tudd: