Daanu
Apparence
1. Wadd, rot
Niral: Musaa dafa daw ba daanu.
Safaan wi mooy jog
2. Yegg fi ngay yége bànneex ci sey.
Niral: bi muy laata daanu lañu ko bett ci kaw ndaw si.
1. Wadd, rot
Niral: Musaa dafa daw ba daanu.
Safaan wi mooy jog
2. Yegg fi ngay yége bànneex ci sey.
Niral: bi muy laata daanu lañu ko bett ci kaw ndaw si.