Aller au contenu

Daaneel

Jóge Wiktionary.

1. Sabab daanu.

Niral: Ngelaw lee daaneel garab gi. Dafa daaneel waxam ji.

2. Rekk, mu yegsi.

Niral: Marsandisam mi yàqu moo ko daaneel.

Safaan wi mooy yëkati.