Aller au contenu

Dàbb

Jóge Wiktionary.

Dafay tekki lu funki bay bëgg a toj.

Niral: xamuma lu mu lekk waaye biir baa ngi funki ba ne dàdd.