Aller au contenu

Cambar-cambar

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Cambar-cambar b

  1. Ku nekk di def lu la neex.
    • Kër gi kenn du ne déet mootax cambar-cambar bi bare fi.