Aller au contenu

Caga

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Caga b

  1. Jigeen ju jëkkëram gaañu wala mu tàggoo ak jëkkëram. Néew na lu wolof yi di jëfandikoo baat bi ci tekki bii.
    • Ndaw soosu ab caga la, daaw la tàggoo ak boroom-këram. / jigeen juy jaay boppam. Jigeen ju xam boppam du dem mukk di nekk ab caga.