Aller au contenu

ëtt

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

ëtt:

  1. ëtt digg barab, niki pénc ci ab dëkk

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. góor gaa gi woote waxtaan ci ëttu kër gi

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu ëtt ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-ëtt.ogg