xala (ag)
Apparence
Wolof
[Soppi]- bii baat cosaan la mooy bant bu dóox bi ñuy takk buum gi ngir mu doon ag fett, te muy mel ne aw terute (weer wuy door a teru), nii ( lay faral a mel. Ci la xala giy tekki ci wu farãas (Parenthèse) juge
ab màndargab tekkeerlu la : ( )
Yeneeni làkk
[Soppi]wu faraas: paranthése |
wu itaali: parentesi |
wu angalteer: parantheses |