Aller au contenu

walla

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

walla:

  1. ab mbaandeel la, ab baat la booy jëfandikoo ngir boole yeneen ñaari baat
  2. dem walla dikk

mbaa

wu-faraas: wu-angalteer: or