Aller au contenu

nguurug ger

Jóge Wiktionary.

Kleptocratie: baat bii, ci maanaam araf-araf mi, li muy tekki mooy nguurug xiima ( gouvernement de voleurs)waaye li muy tekki ci maanaa lu safaanook loolu la mooy nguurug ger