m-bataaxal
Apparence
wolof
[Soppi]mi ngi jóge ci mbëjfeppal ak bataaxal
m-bataaxal
ci xibaarfeppal:
- bataaxalub mbëjfeppal, dañuy wax (miim-bataaxal) ngir gàttal ko;
- Yónne ma ab m-bataaxal ci sama boyot.
yeneeni làkk
[Soppi]- wu-fraas: courriel électronique
- wu-angalteer: e-mail
- wu-itaali: posta elettronica, e-mail