làkk

Jóge Wiktionary.
Dem : Joowiin, Seet

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

Bari na ay tekki:

Aw làkk
Ab jumtukaay la, ngir jokkoo,
Ab làkk
ab miir booy jëfandikoo ngir wërale dara, man naa ne aw sàkket wu gittax, mbaa dóor-dóor, walla sax miir bu simoŋ,...

Yeneeni làkk[Soppi]

wu-faraas: langue, mur
wu-angalteer: language, wall
wu-itaali: lingua, muro