jot
Apparence
Wolof
[Soppi]- jot: am na juróomi maanaa
- ag jot lees di am ngir man a doxi mbaa dallu.
- jot lu matale, niki yere yu jot.
- jot lu man a gàllankoore, niki tawat ...
- jot dab kuy dem mbaa luy dem.
- jot lees doon xaar ba mu yeg si, niki jot sag payoor.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- nelawi bëccëg amuk jot la!
- jigéen ju baax day sol lu jot !
- diw... tay dangaa sédd lu la jot ?
- ndax jot nga ki nga doon dabi ?
- weer wii jot naa samak payoor