gëstu
Apparence
Wolof
[Soppi]Mooy topp am mbir def ci ay jàngat, fexe ba xam lépp lu ku ëmb, li ci laqu ak li ci feeñ.
- Nit kii de def na ag gëstu gu yaa ci diine
- Nit kiy gëstu mooy ab gëstukat
- Fàwwu nga gëstu ngir xam
yeneen làkk
[Soppi]wu faraas: chercher, rechercher, faire des recherches