Aller au contenu

dereet

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

dereet:

  1. dereet liy génn ci yaram wu dagg tey xonq, maanaam liy daw ci diggante der ak yàpp.

Xool it

[Soppi]

ci yeneeni làkk

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu dereet ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dereet.ogg