bind

Jóge Wiktionary.

Dem : Joowiin, Seet

Tëraliin

[Soppi] wolof

[Soppi] Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat

bind: amna ñeenti maanaa

  1. aw bind rëdd wu mat bees war wàcci ngir bindaat weneen,
  2. bind amal ay baat, ci sa loxo walla wuutuloxo,
  3. bind gi nu Yàlla bind, maanaam sàkk,
  4. ab bind melow bind,

[Soppi] Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

  1. sa bind wi rafet na,
  2. yaangi bind ?
  3. Yàllaa nu bind ngir nu jaamu ko!
  4. sama bindu tay bii de xaw ma numay def bamu mokk,
  5. ndaw sii bind bi moo rafet!

[Soppi] Bàyyikoo

mbind

[Soppi] Xool it

[Soppi] Tekki

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu bind ci wolofi Senegaal

Wo-bind.ogg
Ci « http://wo.wiktionary.org/wiki/bind » lañ ko jële