baat
Jóge Wiktionary.
Tëraliin |
[Soppi] Wolof
[Soppi]
Gongikubaat
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
[Soppi]
Tur
baat :
- ab cër la ci cëri nit muy li taqale bopp ak mbagg,
- kii de baat bu gàtt la am
- yaw de masuma laa gis nga takk ceen ci sa baat
- kàddu giy génn ci bolig nit ñu di ko dégg.
- Xoolal kàddu
- Am mbind mbooloom ay baat la
- Baat bi nga wax du wolof
- liy waral boo waxee ñu def ko mbaa ku war a wax ci am mbir
- woykat bi de aka neex baat
- Kilifa dafay am baat ci këram
[Soppi] Tekki
Waxiin
Déglu baatu baat ci wolofi Senegaal