artu

Jóge Wiktionary.
Dem : Joowiin, Seet

Tëraliin

Wolof [Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat [Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Jëf [Soppi]

  • artu
  1. liggéeykat yi artu nañu seeni kilifa, nee nañu leen suñu leen fayul, di nañu bank seeni yoxo

Open book 01.svg Tur [Soppi]

  • artu b:
  1. liggéeykat yi jox nañu seeni kilifa artu bu mujj laataa seen mbankum loxo

Bokktekki [Soppi]

Tekki [Soppi]

wu-faraas: avertir, avertissement

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglul baatu artu ci wolofi Senegaal