def dara cig nammeel: def ko te kenn gawu la ko, mananteesu la ci it, xanaa danga koo bëgg kepp, mu soob la