Aller au contenu

ag baral

Jóge Wiktionary.

mooy wone xalaat walla taxawaayu yenn mbooloo walla yëngu-yëngu yu politig yiy jàñ ag bar mbaa aw askan ci mu xeex kuréel walla tànnéef (élite)yi ko jiite, mbaa néewte la (minorité), te daaneel ko, ngit taxaw