Aller au contenu

adduna

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
ci wolof yi

adduna:amna ñaari maanaa

  1. adduna njendi lii ñu nekk di ci dund asamaan-ak suuf ak lici aju.
  2. dund gi yit dinañ ko wax adduna,misaal:astu toppu nà goné yu goór yi ba yaq addunaam


aji dugal

[Soppi]

Abdu Xaadir Géy Ahloubadar

Tekki ci yeneeni làkk

[Soppi]